dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

añaan : ku añaan mooy ku yéenewul kenn lu baax. dinañuy wax tamit iñaan. / mën na tekki soxor. safaan wi mooy baax wala yéwen.

: fii ci Senegaal, bëccëg la nit ñi di añ.