dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

ŋoos-ŋoos b- : illeer b-. ñoom ay ŋoos-ŋoos lañuy beye.

ŋott : nay. am na xaalis wànte dafa ŋott. safaan wi mooy yéwen wala tabe.

ŋoy : ŋaw, jàppandu. deel ŋoy ci loo moom.