dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

ŋiir : dinañuy wax tamit ŋeer. (seetal ŋeer)

ŋiis : ndox mi taawoon fii, ŋiis na.

ŋisabu : dinañuy wax tamit ñasaxndiku. (seetal ñasaxndiku)