dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

ŋóobi : ŋeleju, regeju. di wax ak ku la mag di ŋóobi, ñàkk yar la.

ŋóot w- : suq w-. lekk na mboq mi ba sànni ŋóot wi.

ŋóotoot w- : teeñu njanaaw. ginaar gi dafa am ay ŋóotoot.