dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

ŋëb : tiye, yore, jàpp. lan nga ŋëb ? dinañuy wax tamit ngëb.

ŋënk : dinañuy wax tamit ŋànk. (seetal ŋànk)

ŋëriñ : dinañuy wax tamit ŋeeñ wala ŋareñ. (seetal ŋareñ)