dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

ñóox : roof, sol. ñóox na gémmeñ gi ba mu fees dell. dinañuy wax tamit ñuux. safaan wi mooy ñuqi.

ñówental : am yërmaade. dafa ñówental taalibe yi.

ñów : dikk. dinañuy wax tamit ñëw. safaan wi mooy dem. (seetal ñëw)