dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

ñëg : dinañuy wax tamit ñég. (seetal ñég)

ñëw : dikk. kañ lay ñëw ? safaan wi mooy dem.