dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

ñédd : dinañuy wax tamit ñedd. (seetal ñedd)

ñég : mer, xonet. li nga ko def mootax mu ñég. dinañuy wax tamit ñëg.

ñéññ : dañu ko gañe mootax mu ñéññ.

ñépp : Yàlla ñépp la fi nekkal.