dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

ëndi : lu la ëndi ci kër gi ? dinañuy wax tamit andi wala indi. safaan wi mooy yóbbu.

ënn : nëb, forox. cere ji mu la yakkal dafa ënn.