dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

ëmb : lëmës. ëmb na yéreem yépp ci ab sër. safaan wi mooy imbi. / wann lor, biir. boo ëmbee danga war di def say wisit ca loppitaal ba.