dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

ëkk b- : pakk b-. moytul ëkk bi nekk sa kanam.

ëkku : yeeru. muus maa ngi ëkku jinax ji.