dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

ëgg b- : tawu noor. atum tawi ëgg yi reyoon nañu ay nag ak ay xar yu bare ca Jolof.