dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

ëcc : defar wëñ ak ay witteen. maamam laa daan gis muy ëcc.