dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

ëŋŋësle : ës, wowle, dëgër-bopp. xale bii du dégg mukk, dafa ëŋŋësle. safaan wi mooy teey.