dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

éeg : golo gi éeg na ca kow garab ga. dinañuy wax tamit yéeg. safaan wi mooy wàcc.

éem : li nga wax éem na nit ñépp. dinañuy wax tamit yéem.