dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

àqan : lenqe. jege ci wàllu mbokk. xale boobu sama sët àqan la.

àq j- : tooñ b-. li nga def nit ki mu metti ko mooy àq. tooñ naa la, baal ma àq.