dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

àppat : xiixat. noyyi noyyi bu foor. looy àppat nii, xanaa danga doon daw ?

àpp b- : dayo b-. yaatuwaayu dëkk ba amul àpp, foo ko natt rekk, romb na fa.