dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

àkk 1 : jékki jékki rekk taxaw. oto bi àkk na.

àkk 2 : dem ci nit di ko wax lu la naqari lu mu la def mooy àkk.

àkkaasiyaa g- : àkkaasiyaa xeetu garab la.

àkk w- : xollitu garab wala xas ma. àkku looro baax na ci coono bu bare.