dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

àgg : pare. dem ba ne salaamaalekum fa nga donn dem. / wala sàkku jigeen ci lu dul coobareem bu dee àgg ci as ndaw, dinañuy wax tamit egg wala yegg.