dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

àbb : dem ci nit mu jox la loo xam ne danga ko koy delloo boo ci paree. li nga àbb delloo ko saa yoo ci paree.