dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

damm yax

"xéwël" lañuy bind, wala "xéwel".

"x", kenn du ko bindee "k" ak "h",

"ë", kenn du ko bindee "e" ak "u",

ci turu dalub web, benn baat warul a am maska. loolu moo tax, "xéwël", ñu mën koo binde, "xewel", ci dalub web bii di, "xewel.com".

réewum Senegaal, dafa génne benn dekere, mu di sàrtu mbindum wolof ci biir Senegaal. wareef la bon, képp kuy yëngu ci biir Senegaal, nga sàmmoontee ak sàrt Senegaal boobu.

ñu ngiy ñaan waa xewel.com, ñu jàppale ñu, rafetal seen mbindum wolof.

kheweul.com Senegaal