dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

damm yax

"jaay ma" lañuy bind.

"j", kenn du ko bindee "d" ak "i",

ci turu dalub web, baat yépp, dañu leen war a taqale. loolu moo tax, "jaay ma", ñu mën koo binde, "jaayma", ci dalub web bii di, "jaayma.com",

réewum Senegaal, dafa génne benn dekere, mu di sàrtu mbindum wolof ci biir Senegaal. wareef la bon, képp kuy yëngu ci biir Senegaal, nga sàmmoontee ak sàrt Senegaal boobu.

ñu ngiy ñaan waa jaayma.com, ñu jàppale ñu, rafetal seen mbindum wolof.

diayma.com Senegaal