dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

damm yax

"jóoni-jóoni" lañuy bind.

batodi "j", kenn du ko bindee "d" ak "i",

"o", su diisee, "ó", la lay jox. soo guddalee "ó", mu jox la "óo".

réewum Senegaal, dafa génne benn dekere, mu di sàrtu mbindum wolof ci biir Senegaal. wareef la bon, képp kuy yëngu ci biir Senegaal, nga sàmmoontee ak sàrt Senegaal boobu.

ñu ngiy ñaan waa jóoni-jóoni, ñu jàppale ñu, rafetal seen mbindum wolof.

jooni jooni Senegaal