dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

damm yax

"yóbbaale", mu ngi jóge ci baatu "yóbb". bon, ñu ngiy bind "yóbbaale ma",

réewum Senegaal, dafa génne benn dekere, mu di sàrtu mbindum wolof ci biir Senegaal. wareef la bon, képp kuy yëngu ci biir Senegaal, nga sàmmoontee ak sàrt Senegaal boobu.

ñu ngiy ñaan waa Expresso, ñu jàppale ñu, rafetal seen mbindum wolof.

Expresso Senegaal