dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

damm yax

"ceeb bu joŋe" lañuy bind,

"c" kenn du ko binde ak "t", "h" ak "i"

"e" bi nekk ci "ceeb", "e" bu gudd la di "ee".

baatoodi "ŋ" baatoodi bu jafe la. waaya, lu mu jafe-jafe, seerul ba ñu koy binde "n", "g" ak "u".

réewum Senegaal, dafa génne benn dekere, mu di sàrtu mbindum wolof ci biir Senegaal. wareef la bon, képp kuy yëngu ci biir Senegaal, nga sàmmoontee ak sàrt Senegaal boobu.

ñu ngiy ñaan waa Sofiex ñu jàppale ñu, rafetal seen mbindum wolof.

Sofiex