dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

damm yax

"réew mi" lañuy bind.

"é" bu gudd, di "ée", moo nekk ci baatu "réew".

réewum Senegaal, dafa génne benn dekere, mu di sàrtu mbindum wolof ci biir Senegaal. wareef la bon, képp kuy yëngu ci biir Senegaal, nga sàmmoontee ak sàrt Senegaal boobu.

ñu ngiy ñaan waa Réew mi, ñu jàppale ñu, rafetal seen mbindum wolof.

Réew mi Senegaal