dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

damm yax

"bennoo bokk yaakaar" lañuy bind,

"benno" amul ci wolof, ndax "o" bi, da ñu ko war a guddal.

naka noonu, "yaakaar" lañuy wax. kenn du wax "yakaar".

réewum Senegaal, dafa génne benn dekere, mu di sàrtu mbindum wolof ci biir Senegaal. wareef la bon, képp kuy yëngu ci biir Senegaal, nga sàmmoontee ak sàrt Senegaal boobu.

ñu ngiy ñaan waa bennoo bokk yaakaar, ñu bokk jàppale ñu, bokk rafetal seen mbindum wolof.

Benno Bokk Yakaar Senegaal